Lines Matching refs:sa

5 Ñu jàpp te nangu ne sagu doomi aadama ak sañ-sañam yépp-dañu yam te kenn mënukóo jalgati, te lu lép…
7 Ñu jàpp ne ñakk xam ak soofantal sañ-sañi doomi aadama indi na aymusiba yu tar tax képp kuy dund fi…
9 Ñu jàpp ne am na solo lool ñu aar sañ-sañi doomu aadama ak ay matukaay ci wàllu yoon; ngir doomu aa…
13 Ñu jàpp ne ci bataaxal boobule mbootaayu xeet yi yeesalaat na ay pas-pasam jëme ko ci sañ-sani doom…
15 …ay ngir dëgëral jokkalante gi ak mbootaayu xeet yi, ñu naw it bu baax sann-sañi doomi aadama ak ta…
17 Ñu jàpp ne ànd taxawal sañ-sañ yeek tawfeex yi nekk na lu am solo lool ngir, darajaal matukaay yooy…
21 Ñu lawal sañ-sañ yeek taawfeex yi jël aymatukaay ci biirak bitim réew.
26 Doomi aadama yépp danuy juddu, yam ci tawfeex ci sag ak sañ-sañ. Nekk na it ku xam dëgg te ànd na a…
29 Ku ne mën naa wax ne am na ay sañ-sañ ak ay tawfeex yu sosoo ci bataaxal bii te amul xeej ak seen, …
31 Rax sa dolli amul xeej ak seen ci politig, yoon, mbaa doxalin wu aju ci bitim réew mbaa suuf soo xa…
43 Nit ku ne am na sañ-sañ ñu war kaa nangul darajaam ci wàllu yoon.
49 Nit ku ne am na sañ-sañ dem ci berebi àtte kaay yi ci reewam saa yoo xamne sañ-sañam yooyu dëppook …
63 …a lu mengóok moom, di damm it jarajaam. Buñu jalgatee yii nit kune am na sañ-sañ ñu aar ko ci wàll…
66 1. Nit kune am na sañ-sañ wëndeelu ni mu ko neexe, tànn it dekkuwaayam ci biir réew bu mu mën ti do…
68 2. Nit kune am na sañ-sañ génn réew mu mu mën ti doon. Fimu dëkk it bokk na ci-ak it dellusi ci rée…
71 1. Nit kune bu ñu ko mbugalee am na sañ-sañ làqu ji, mbaa ñaan ñu làq ko ci yeneni réew.
73 …nnaaw bi mu defee jëyyi, mbaa yëngu-yëngóon méngóowul ak li mbootaayu xeet yi tëral, sañ-sañ boobu.
76 1. Nit ku ne am na sañ-sañ xeetoo cim réew.
78 2. Mënuñu ne nit ki xeetoowul cim réew te teguñu ko fenn, mbaa ñu xañ ko sañ-sañ su bëggee soppi xe…
81 …, ak waaso bu mu mën ti bokk, réew, mba diiné am na sañ-sañ sëy ak it sos njaboot. Ñoo yam it sañ-
88 1. Ngay dund yaw doww mbaa ak mbooloo am nga sañ-sañ am loo moomal sa bopp.
93 Nit kune am na sañ-sañ xalaat ak sa goom ci wàllu diine, soppi it diineem mba ngëmam, am na it tawf…
96 Nit ku ne am na sañ-sañ wax mbaa bind lu ko soob. Ci waxam yooyule kenn menuko ce bundu xatal. Te i…
99 1. Nit kune am na sañ-sañ woote ab ndaje, mbaa sos mbootaay ci jàmm.
104 1. Nit ku ne am na sañ-sañ bokk ci ñiy doxal mbiri réewam. Mu teewal fa boppam, mbaa mu yabal ab nd…
106 2. Nit ku ne am na sañ-sañ, amul xeej ak seen liggéey ci bépp béréb buy doxal mbiri réewam.
111 Nit ku ne meññeefu askan wi am na sañ-sañ ñu aar ko ci giru dundam. Ci dundam war na ci am xol bu s…
114 1. Nit ku ne am na sañ-sañ liggéey, tànn it ci eanam gu ko neex liggéeyamm te mu dëppóok ay sàart y…
116 2. Amul xeej ak seen ku néppam nanu sañ-sañ ñu fay leen, te loolu méngóok li mu aliggéey.
118 3. Keépp kuy liggéey am na sañ-sañ ñu jox ko pay gi mu yellool, baax te mën koo dundal ak njabbotam…
120 4. Nit ku ne am na sañ-sañ samp mbaa bokk ci ay kurel yu koy taxawu ci wàllu liggéeyam.
123 Nit ku ne am na sañ-sañ noppalu, feexal xolal ak it di yamale diirub liggéeyam ak it léeg-léeg muy …
126sañ-sañ am dundingu yamamaay ngir dëgëral wér-gi-yaramam, raataageem ak bu njabootam, lrawatina ci…
131 1. Nit ku ne am na sañ-sañ ñu jàngal ko, njàng mi waruñu ci fayaku lu mu bon bon ci njàng mu suufe …
133 2. Njàng war naa indi naataange gu yaa ci ddoomi aadama te it war na dëgëral ñu naw sañ-sañi doomi …
135 3. Waajur yi ñoo jëkk am sañ-sañ ci anam gi ñuy yare seeni doom.
138 1. Nit ku ne am na sañ-sañ bokk ci dépp lu aju ci caaday askan wi, di bànneexu ci lu cu aju ak it b…
140 2. Nit ku ne am na sañ-sañ ñu aaral ko lépp lu aju ci lu mudefar ci wàllu la xarala, mbind mbaa lu …
143 Nit ku ne war naa tawaxu dëpp lu aju a askan wi, ak lu aju ci bitim réewam ba sañ-sañ ak tawfeex yi…
148 2. Nit ku ne buy doxal ay sañ-sañam aki tawfeexam war naa sallook li ko yoon may, ngir mu mën a nan…
150 3. Sañ-sañ yeek tawfeex yi mënuñukoo doxal ci anam gu deppoo-wul li mbootaayu xeet yi misër mbaa ta…
153 …n ci bataaxal bii, bépp réew, mbootaay mbaa nit, warul doxal mbaa def luy yàq sañ-sañ yeek tawfeex.