Lines Matching refs:ew

15 Ñu jàpp ne réew yi ci bokk jël nañu ay matukaay ngir dëgëral jokkalante gi ak mbootaayu xeet yi, ñu…
19 Ndaje mu mag mi biral na ci bataaxal bii ne xeet yépp, réew yépp ak kurel yépp ñu jàpp li ci nekk, …
21 Ñu lawal sañ-sañ yeek taawfeex yi jël aymatukaay ci biirak bitim réew.
23 Ñu nangu te di doxal fépp ci anam gu wér ci biir xeet yi sosoo ci réew i bokk ci mbootaay gi ak gox…
29 … ci wàllu xeet, melo, awra, làkk, diiné, peete ci wàllu politig, xalaat, réew mbaa askan woo mën t…
31 …n ci politig, yoon, mbaa doxalin wu aju ci bitim réew mbaa suuf soo xamne nit ki fa la cosaanoo; r…
60 …u jëf ci jamono jooju nekkul mbir mu tar ci wàllu yoon, ci biir ak bitim réew. Foofu it yoon du ko…
66 1. Nit kune am na sañ-sañ wëndeelu ni mu ko neexe, tànn it dekkuwaayam ci biir réew bu mu mën ti do…
68 2. Nit kune am na sañ-sañ génn réew mu mu mën ti doon. Fimu dëkk it bokk na ci-ak it dellusi ci rée…
71 1. Nit kune bu ñu ko mbugalee am na sañ-sañ làqu ji, mbaa ñaan ñu làq ko ci yeneni réew.
76 1. Nit ku ne am na sañ-sañ xeetoo cim réew.
78 2. Mënuñu ne nit ki xeetoowul cim réew te teguñu ko fenn, mbaa ñu xañ ko sañ-sañ su bëggee soppi xe…
81 1. Jigéen mbaa jóor saa yu matee amul xaaj ak seen, ak waaso bu mu mën ti bokk, réew, mba diiné am …
108 3. Pas-pasu askan mooy cëslaay buy dëgëral lépp luy doxal réew. Pas-pas gile war na feeñ ci palin y…
111 …am, loolu lépp nag ku ne doomu réew mi indi dooleem ak di jokkalante ak bitim réew te mu méngook t…
153 Ci fànn gu mu mën ti doon ci bataaxal bii, bépp réew, mbootaay mbaa nit, warul doxal mbaa def luy y…