Lines Matching full:yu
7 Ñu jàpp ne ñakk xam ak soofantal sañ-sañi doomi aadama indi na aymusiba yu tar tax képp kuy dund fi…
13 …ootaayu xeet yi yeesalaat na ay pas-pasam jëme ko ci sañ-sani doomi aadama yu tolloo, ci sag, ci b…
15 … ak mbootaayu xeet yi, ñu naw it bu baax sann-sañi doomi aadama ak tawfeex yu wóor ci biir àdduna …
29 Ku ne mën naa wax ne am na ay sañ-sañ ak ay tawfeex yu sosoo ci bataaxal bii te amul xeej ak seen, …
81 1. Jigéen mbaa jóor saa yu matee amul xaaj ak seen, ak waaso bu mu mën ti bokk, réew, mba diiné am …
96 …ëstu, di jot, di wasare ci anam gu yaa ay xabaaraki xalaat ak ay jumtukaay yu mi Men ti jefandikóo.
108 …laay buy dëgëral lépp luy doxal réew. Pas-pas gile war na feeñ ci palin yu yiw yu ñu wara amal lée…
114 …sañ liggéey, tànn it ci eanam gu ko neex liggéeyamm te mu dëppóok ay sàart yu yam te baax ci wàllu…
120 4. Nit ku ne am na sañ-sañ samp mbaa bokk ci ay kurel yu koy taxawu ci wàllu liggéeyam.
126 …, ñàkk saxnaam mbaa sërinam, mbaa màgget, mbaa mu ñàkk li muy suturloo ci anam yu dul ci cootareem.
146 1. Nit ku ne am na ay wareef yu ko war digganteem ak dëkkandoom yi ngir dëgëral ci anam gu ya daraj…